score
float32 1.04
1.24
| Shona
stringlengths 10
498
| Wolof
stringlengths 10
474
|
---|---|---|
1.236879 |
Asi umwari nokugutsikana nezvatinazvo zvinopfumisa kwazvo.
|
Ba tey ragal Yàlla gu ànd ak doylu, wërsëg la.
|
1.234955 |
31 rwamakagadzirira pamberi pavanhu vose,
|
xeet yépp seede ko.
|
1.233263 |
kafiro airene
|
Waaye ci ñi gëmul, nag:
|
1.229607 |
Ɀino, iwe, kana ukandinamata, ɀose ɀicaʋa ɀako.
|
Kon boo ma màggalee, dinga moom lépp."
|
1.228556 |
matsenga ako,e, iwe Musa!
|
waaaw les mousses!
|
1.228355 |
Ndo zvavari kuona va kuru ava.
|
Maam ya, seen ngëm a tax ba Yàlla seedeel leen lu baax.
|
1.22757 |
4:8 Wakaropafadzwa munhu usinganzi naShe hazviverengerwi chivi. "
|
4:8 Ki Boroom bi sëful ay bàkkaaram,kooka ku barkeel la."
|
1.225341 |
Unodzidzei pamudzimai waRoti?
|
Lan lañu mën a jàng ci li dal jabaru Lóot ?
|
1.220051 |
15 Zvino akati kwavari:Ini ndanga ndichishuvira kwazvo kudya iyi Paseka nemi ndisati ndatambura.
|
22:15 ne leen: "Yàkkamti woon naa lool lekk ak yéen reeru Jéggi bii, laata ñu may sonal.
|
1.218034 |
31 rwamakagadzirira pamberi pezviso zvavanhu vose;
|
xeet yépp seede ko.
|
1.216909 |
6 Ishe akati: inzwai zvinorebwa nemutongi asakarurama.
|
18:6 Boroom bi tegaat ca ne: "Dégluleen bu baax li àttekat bu bon boobu wax;
|
1.213723 |
waanoda kunzwira ngoni, uye anoomesa mwoyo wouyo waanoda kuomesa.
|
18 Kon nag Yàlla mooy yërëm ku ko neex, te ku ko neex lay dëgëral xolam.
|
1.212184 |
Bhuku rino richakubatsira.
|
Téere bii dina la ci dimbali.
|
1.211713 |
18 Kwashayikwa mumwe woga adzoka akazorumbidza Mwari kunze kwouyu mutorwa here?"
|
17:18 Amul kenn ci ñoom ku ñëw gërëm Yàlla ku dul doxandéem bii!"
|
1.211576 |
43. uye akatora akaidya pamberi pavo.
|
Mu jël ko, lekk ci seen kanam.
|
1.210369 |
Nekuti zuva rimwe chete rave risinganzwisisike vatenzi vako.
|
(58) Sa Boroomay jéggalaakoon tey boroom yërmande.
|
1.209821 |
ko kushumira koMweya hakungavi nokubwinya kukuru here?
|
rawatina nag ne, jëfu Xelum Yàlla dina gën a ànd ak ndam.
|
1.209413 |
34 Vachiti: Ishe wamuka zvirokwazvo; wavonekwa naSimoni.
|
34 Ñooñu ne leen: "Dëgg la, Boroom bi dekki na, te feeñu na Simoŋ!"
|
1.208119 |
9. (nokuti chibereko chechiedza chino kunaka kwose, kururama nechokwadi)
|
Leer, mbaax lay meññ, njub ak dëgg.
|
1.208018 |
6 Ishe akati: Inzwai zvinorebwa nomutongi usakarurama.
|
18:6 Boroom bi tegaat ca ne: "Dégluleen bu baax li àttekat bu bon boobu wax;
|
1.207646 |
pamusoro pavo akavaporesa.
|
mu nangul leen, faj leen.
|
1.206698 |
64 Asi vamwe venyu varipo vasingatendi."
|
6:64 Waaye am na ci seen biir ñu ko gëmul."
|
1.206148 |
19 Naizvozvo tinoona kuti vaisagona kupinda nokuti vakanga vasingatendi.+
|
19 Noonu gis nanu sax ne jotuñoo dugg ci noflaay boobu ndax seen gëmadi.
|
1.205741 |
34 Ivo vakati: Ishe wamuka zvirokwazvo; wavonekwa naSimoni.
|
34 Ñooñu ne leen: "Dëgg la, Boroom bi dekki na, te feeñu na Simoŋ!"
|
1.204327 |
nebuku rinetsina nekushata.
|
Indeed book de wicked est Sijjeen.
|
1.204305 |
By gungwa, kuti hombe pasuru uye uwandu;
|
ak biir géej ak xóote yépp.
|
1.203329 |
Tarira kakomana kanotaura navakweguru ava.
|
XOOLAL xale bi di waxtaan fii ak mag ñi.
|
1.202775 |
Ndokusaka maona nokunzwa manenji aya.'
|
Loolu moo tax ngeen gis te dégg kéemaan yii. '
|
1.201609 |
5 Mai vake vakati kuvaranda, "Itai zvose zvaanokuudzai."
|
5 Yaayam daldi ne surga ya: "Defleen lépp lu mu leen wax."
|
1.201571 |
Kunyange baba vangu vanotozviziva izvozvo.'
|
Sama baay ci boppam xam na loolu bu baax."
|
1.200629 |
Muponesi chii, uye nei tichida Muponesi?
|
Lan mooy ab Musalkat te lutax nu soxlo ab Musalkat ?
|
1.20046 |
Uchapupu uhu hunorehwa navarume ava pamusoro pako ndohwei?"
|
Loo xam ci li ñii seede ci yaw?"
|
1.199149 |
Unoziva chiri kutaura Pauro kuna Timotio here?
|
Ndax xam nga lan la Pool di wax Timote ?
|
1.198594 |
Mubhuku iri mune nhau 116.
|
Ci téere bii, am na 116 nettali.
|
1.198207 |
Unoziva chiri muprofita here?
|
Ndax xam nga lan mooy yonent ?
|
1.195667 |
Unorambirei wakagara uri woga uye vanhu vose vachiramba vakamira pamberi pako kubvira mangwanani kusvikira manheru?"
|
Lu tax ngay toog, di àtte yaw rekk, mbooloo mépp wër la, suba ba ngoon?"
|
1.195279 |
Vakomana vaviri vari pano vakasiyana zvikuru, handiti?
|
ÑAARI xale yi ñuy wone fii, niroowuñu, du dëgg ?
|
1.195166 |
9 Nokuti iye nevaya vose vaaiva navo vakakatyamadzwa kwazvo nehove dzavakabata,
|
5:9 Wax na loolu nag, ndax jën yu bare ya ñu mbaaloon daf koo jaaxal, moom ak ña mu àndaloon
|
1.194994 |
muchishandisa mikana yose, nokuti mazuva akaipa.
|
tey jariñoo jot gi, ndaxte nu ngi ci jamono ju bon.
|
1.193995 |
nokuti Mweya Mutsvene achakudzidzisai neawa iro zva mu nofanira kutaura.
|
ndaxte Xel mu Sell mi dina leen xamal ca waxtu woowa li ngeen war a wax."
|
1.193763 |
5 "'Madzibaba enyu ari kupi iye zvino?
|
5 "Seeni maam, ana ñu tey?
|
1.193513 |
Tora mudzimai wako navanasikana vako vaviri ndokubuda muno!'
|
Jëlal sa jabar ak sa ñaari doom yu jigéen te jógeleen fii ! '
|
1.193468 |
48 Imi muri zvapupu zvezvinhu izvi.
|
48 Yéenay samay seede.
|
1.192329 |
Unoziva mukadzi akatsvinda ari kuuya kuzosangana naDhavhidhi here?
|
NDAX xam nga jigéen bu rafet biy fekksi Daawuda nii ?
|
1.191641 |
34 vachiti: "Chokwadi Ishe amutswa uye azviratidza kuna Simoni!"+
|
34 Ñooñu ne leen: "Dëgg la, Boroom bi dekki na, te feeñu na Simoŋ!"
|
1.191606 |
Vana vaNoa vakava navana vazhinji.
|
Doomu Nóoyin yi amoon nañu doom yu bare.
|
1.191007 |
2 Muzvipire pakunyengetera, makanyatsorinda uye muchivonga.
|
4:2 Dëkkleen ci ñaan Yàlla, farlu ci, boole ci ngërëm.
|
1.190722 |
Vose vakabvunza vachiti, "Ko, zvino iwe ndiwe Mwanakomana waMwari here?"Iye akapindura akati, "Mareva zvakanaka, zvamati ndini iye."
|
noonu ñépp ne: "kon nag yaay doomu yàlla ji?" mu tontu leen ne: "yéen ci seen bopp wax ngeen ne moom laa."
|
1.190586 |
29 Jesu akapindura akati, "Basa raMwari nderiri: kuti mutende kuna iye waakatuma."
|
29 Yeesu ne leen: "Jëf ji neex Yàlla, moo di gëm ki mu yónni."
|
1.190168 |
Benzi iri rakavingeiko kwauri?"
|
Lu indi dof bii ci yaw?"
|
1.189359 |
Ipapo vaJudha vakapesanazve nokuda kwamashoko aya.
|
Kàddu yooyee ñoo féewalewaat Yawut yi.
|
1.188025 |
17:5 Zvino vaapositori vakati kuna Ishe, "Tiwedzereiwo kutenda kwedu."
|
17:5 Ndaw ya wax Boroom bi ne ko: "Yokkal sunu ngëm."
|
1.187931 |
4 vachaona chiso chake,+ uye zita rake richava pahuma dzavo.+
|
4 Dinañu gis xar kanamam, te turam dina nekk ci seen jë.
|
1.187684 |
Unoyeuka here uchinzwa nezvamajaya matatu aya?
|
NDAX yaa ngi fàttaliku ñetti góor ñii ?
|
1.187677 |
Nokuti unoreva zvimwe zvinoshamisa panzeve dzedu; naizvozvo tinoda kunzwa, kuti zvinhu izvi ndezveiko?
|
ndaxte sol nga ci sunuy nopp lu nu xamul. danoo bëggoon a xam nag léegi, loolu lu muy tekki."
|
1.187473 |
"Ndizvo Zvandakauyira Munyika"
|
" Lii moo tax ma ñëw àddina "
|
1.186628 |
Vamwe vanhu vangaedza kutidzivisa kutaura pamsoro poumambo hwaMwari.
|
Mën na am ay nit jéem ñu tere wax ci nguuru Yàlla.
|
1.184594 |
5:30 Nokuti isu tiri chikamu chomuviri wake, nyama yake uye mapfupa ake.
|
5:30 ndaxte noo di céri jëmmam.
|
1.184394 |
9 nokuti chibereko chechiedza chinoumbwa nokunaka kwemarudzi ose nokururama nechokwadi.+
|
Leer, mbaax lay meññ, njub ak dëgg.
|
1.183829 |
Ngirozi dzakaudza Roti: 'Chimbidza!
|
Lii la malaaka yi wax Lóot: ' Gaawal !
|
1.18356 |
Hapana chandisina kuvaratidza pakati pefuma yangu. "
|
Su ko defee kenn ci sama ñoñ du ñàkk alalam."
|
1.182559 |
Hamisi Mutinda
|
Ye dinna ken yon bower,
|
1.182352 |
5:30 Ini handigoni kuita chinhu pachangu.
|
5:30 Mënumaa def dara man ci sama bopp.
|
1.182145 |
6:20 Nokuti imi vakatengwa nomutengo mukuru.
|
6:20 ndaxte Yàlla jot na leen ak njëg gu réy.
|
1.182051 |
7 Naizvozvo, iwe, kana ukangondinamata+ kamwe chete, zvose zvichava zvako."
|
Kon boo ma màggalee, dinga moom lépp."
|
1.180727 |
Iwe une mibvunzo here?
|
am nga ay laaj?
|
1.180442 |
Atuma ngirozi yake ndokuvaponesa nokuti havazati vaizopfugama ndokunamata mwari upi noupi kunze kwowavo vamene.'
|
Dafa yónni malaakaam te muccal leen, ndaxte dañu bañ a sukk te jaamu benn yàlla ku dul seen Yàlla. '
|
1.179797 |
uye vatongi vakaungana pamwe chete,
|
te kilifa yi dajaloo,
|
1.178943 |
hakuna anozonzwa inzwi rake mumigwagwa.
|
te kenn du dégg baatam ci mbedd yi.
|
1.178795 |
Tichasarudza kushamwaridzana nevanhu vanoda Mwari here?
|
Ndax dinañu ànd ak ñi bëgg Yàlla?
|
1.178011 |
Nei vadzidzi vari kutya munguva yousiku, uye chii chinoitika kuna Petro?
|
Lu tax taalibe yi tiit ci guddi gi, te lan moo dal Piyeer ?
|
1.177957 |
Nei Roti akasarudza kugara muSodhoma?
|
Lu tax Lóot tànn Sodom ngir dëkk fa ?
|
1.176106 |
Umambo yangu ri pano.
|
Sama nguur nekk fii.
|
1.175975 |
Ngirozi mbiri dzakapa Roti nyevero yokuti chii?
|
Lan la ñaari malaaka yëgal Lóot ?
|
1.175304 |
Nei tichida nyika itsva?
|
Lu tax ñu soxla àddina su bees?
|
1.175282 |
Nei tichida nyika itsva?
|
Lu tax ñu soxla àddina su bees ?
|
1.175086 |
akati kuvanhu, "Pane mazuva matanhatu okushanda.
|
Mu ne mbooloo ma: "Juróom benni fan la nit ñi wara liggéey.
|
1.17455 |
Ora nemutumirii tale
|
And ak ndaw soosu làmbook lu weex
|
1.174548 |
Nekuti Jobho aiti: "Pamwe vanakomana vangu vakatadza, vakatuka Mwari mumwoyo mavo."
|
Booba Ayóoba da naan: "Jombul sama doom yii bàkkaar nañu mbaa ñu xarab Yàlla ci seen xel."
|
1.174479 |
Isu tinokuvimbisa iwe zvimwe zvebhayaroji chokwadi nepamusoro-notch chokwadi uye kurongeka; kunaya, uya kupenya.
|
(13) Noo ngi lay nettalli séen xibaar dëgg-dëgg;nekkoon nañu ñu jub, nu dolli léen ak njub.
|
1.174452 |
uye vachaprofita.
|
te dinañu wax ci kàddug Yàlla.
|
1.174389 |
Naizvozvo sei ndawana ropafadzo iyi, kuti amai vaShe wangu vauye kwandiri?
|
Man maay kan, ba ndeyu sama Boroom ñëw di ma seetsi?
|
1.174191 |
RUKA 16:15 Akati kwavari: imi munozviruramisa pamberi pavanhu; asi Mwari unoziva moyo yenyu; nokuti izvo zvinokudzwa pakati pavanhu, zvinonyangadza pamberi paMwari.
|
15 Yeesu ne leen: "Yeen yeenay jub-jublu ci kanam nit ñi, waaye Yàlla xam na seen xol.
|
1.17382 |
24:32 Vakati mumwe, "Ko, mwoyo yedu yanga isingapisi mukati medu, paakanga achitaura munzira, uye wakati magwaro isu?"
|
24:32 Noonu ku nekk naan sa moroom: "Ndax sa xol seddul woon, bi muy wax ak nun ci yoon wi, te muy tekki Mbind mi?"
|
1.173747 |
51 Chokwadi, chokwadi ndinoti kwamuri, Kana munhu akachengeta shoko rangu, haazombooni rufu."+
|
51 Ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, kuy sàmm sama wax doo dee mukk."
|
1.173291 |
21 Iwoyu murairo wakabva kwaari, tinawo, wokuti unoda Mwari, ngaade vo hama yake.
|
4:21 Te jox na nu ndigal lii: ku bëgg Yàlla, nga bëgg sa mbokk.
|
1.172883 |
13Zvino Mozisi akati kuvanhu, "Musatya henyu, mirai, mugoona sununguro yaJehovha, yaachakuitirai nhasi, nokuti vaIjipiti vamaona nhasi, hamungazovaonizve nokusingaperi.
|
13 Musaa nag ne mbooloo ma: "Buleen tiit, neleen tekk te xool li Aji Sax jiy def, ba xettli leen tey jii.
|
1.172874 |
6 Ishe akabva ati: "Inzwai zvakataurwa nomutongi wacho, kunyange akanga asina kururama!
|
18:6 Boroom bi tegaat ca ne: "Dégluleen bu baax li àttekat bu bon boobu wax;
|
1.172596 |
Uye hakuna munhu anozonzwa izwi rake murnigwagwa.
|
te kenn du dégg baatam ci mbedd yi.
|
1.172357 |
Naizvozvowo ndinokuudzai kuti pachava nomufaro mukuru kudenga wokufarira mutadzi mumwechete anopinduka kupfuura kufarirwa kunoitwa makumi mapfumbamwe ana vapfumbamwe avanhu vakarurama vasina chavangadire kupinduka.
|
Te mbég moomu mooy ëpp mbég, mi fay am, ngir juróom-ñeent-fukk ak juróom-ñeent ñu jub, te soxlawuñoo tuub seeni bàkkaar.
|
1.17134 |
28 Achipindura, Tomasi akati kwaari: "Ishe wangu naMwari wangu!"+
|
20:28 Tomaa tontu ko ne: "Sama Boroom, sama Yàlla!"
|
1.171289 |
Tendeuka utye Mwari.
|
Deeleen rus mag te ragal-leen seen Yàlla.
|
1.171097 |
49 Vakanga vagere naye pakudya vakatanga kureva mumoyo yavo, vachiti: Uyu ndianiko unokangamwira zvivi vo?
|
49 Noonu ñi doon lekkandoo ak moom di wax ci seen xel naan: "Kii am sañ-sañu baale bàkkaar mooy kan?"
|
1.171091 |
Shamwari nhatu dzenhema dzakamushanyira.
|
Ñetti xaritam ñów seetsi ko.
|
1.170712 |
pazuva iroro vachatsanya.
|
Kera bés yooyu nag, dinañu woor."
|
1.170444 |
"Tiudzei, Zvinhu Izvi Zvichaitika Rini?"
|
"Wax nu kañ la loolu di am?
|
1.17022 |
7 Ndiwe aniko, iwe gomo guru?
|
7 Yaa di kan, yaw tund wu mag wi?
|
1.170057 |
17 "Nguva yakati yaswedera yokuti Mwari azadzise chipikirwa chake kuna Abhurahama, uwandu hwavanhu vedu muIjipiti hwakawedzerwa zvikuru.
|
7:17 "Bi loolu wéyee jamono ji jege woon na, ngir Yàlla amal li mu digoon Ibraayma ci ngiñ; fekk xeet wa di law tey gën a bare ci Misra,
|
1.169292 |
8. ko, kushumira kwaMweya hakungavi nokubwinya kukuru here?
|
rawatina nag ne, jëfu Xelum Yàlla dina gën a ànd ak ndam.
|
1.169139 |
Zvino akati kwavari: Hamuzivi here mufanandizo uyu?
|
Noonu Yeesu ne leen: "Ndax seen xol dafa tëju ba tey?"
|
Shona-Wolof_Sentence-Pairs Dataset
This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.
This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1
Metadata
- File Name: Shona-Wolof_Sentence-Pairs
- Number of Rows: 67753
- Number of Columns: 3
- Columns: score, Shona, Wolof
Dataset Description
The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:
score
: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).Shona
: The first sentence in the pair (language 1).Wolof
: The second sentence in the pair (language 2).
This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.
References
Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:
[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017
[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.
[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018
[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.
[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.
[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.
[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.
[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB
[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.
[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages
- Downloads last month
- 7