score
float32
1.04
1.23
Hausa
stringlengths
10
492
Wolof
stringlengths
10
453
1.138324
Very info mai kyau.
lool lool Information
1.138274
10 Ko kuwa ya roƙe shi kifi, ya ba shi maciji?
10 Walla mu ñaan la jën, nga jox ko jaan?
1.137992
11 Sai suka husata ƙwarai, suka yi shawarar abin da za su yi wa Yesu.
11 Waaye nit ña mer ba fees, di rabat pexe yu jëm ca Yeesu.
1.137965
LITTATTAFAI da wasiƙu 66 ne suke cikin Littafi Mai Tsarki.
Biibël bi yépp 66 téere yu ndaw la.
1.137879
Waɗannan su ne kalmomin wannan da yake na Farko da na Ƙarshe, wanda ya mutu ya kuma sāke tashi da rai.
"Lii moo di kàdduy Ki Jëkk te Mujj, Ki dee woon te dekki.
1.137775
"Ku yi hankali da masu-ƙaryan annabci." - MATTA 7:15.
" Moytuleen ñi mbubboo turu yonent. " - MACË 7:15.
1.137737
65 Ya ce, "Domin haka na gaya muku, ba mai iya zuwa wurina, sai dai Ubana ya ba shi."
65 Mu dolli ca it ne: "Looloo tax ma ne, kenn manula ñëw ci man te Baay bi mayu la, nga agsi."
1.137737
Yace "kinga qanwatah nipa bazan ta'bason wata ba, zama da sadeey ta fara koya miki surutu ko?
Les inn uttale for moon moon [es - latam] Vet du hvordan man uttaler moon?
1.137626
Ai, Mulkin Allah a tsakaninku yake." 22 Ya kuma ce wa almajiran, "Lokaci yana zuwa da za ku yi begen ganin rana ɗaya daga cikin ranakun Ɗan Mutum, amma ba za ku gani ba.
17:22 Noonu mu ne taalibe ya: "Jamono dina ñëw, fu ngeen di bëgg a gis su doon sax benn fan ci jamono ju Doomu nit ki di ñëw, waaye dungeen ko gis.
1.137607
In ya ƙi kula da wannan, shi ma sai a ƙi kula da shi.
Te su ko xeebee it, ñu xeeb ko.
1.13756
7:30 da waɗanda suke kuka, kamar ba su kuka ba; da masu murna, kamar basa murna; da waɗanda suka saya, kamar basu mallaki komai ba;
7:30 ñiy jooy, mel ni ñu jooyul; ñiy bég, mel ni ñu bégul; ñiy jënd, ni ñu moomul li ñu jënd;
1.137546
40. duk da haka kun ƙi zuwa wurina domin ku sami rai.
te bëgguleen a ñëw ci man ngir am dund!
1.13748
da shi, te yo nan sun gan ga chi
te seetuñu ci Yàlla.
1.137478
' Ahasuerus bai san cewa matarsa Esther Ba'isra'iliya ba ce.
Asuerus xamul ne jabaram, waa Israyil la.
1.137456
Ina da dogon video.
am video lool
1.137225
Ko da yake kuna ba da godiya da kyau, amma wancan mutumin da yake tare da ku bai ginu ba.
17 Dëgg la, dangay sant Yàlla bu baax, waaye ki ci des, ngëmam yokkuwul.
1.137091
mars yanks go home
Yankees go home! kkkk
1.136953
31 Ta haka kuka shaidi kanku ku ne 'ya'yan masu kisan annabawa.
23:31 Seede ngeen nii ne, yey ngeen seen bopp, te yéenay doomi ñi doon rey yonent yi,
1.136915
Shin Kana da Karin Tambayoyi?
am nga ay laaj?
1.13667
Me ya sa Jehobah ya gaya wa Joshua ya tara manyan duwatsu 12 daga gefen kogin?
Lu tax Yexowa wax Yosuwe mu jël 12 xeer yu mag ci biir dex bi?
1.136614
Ka san abin da Timothawus yake rubutawa?
Ndax xam nga lan la Pool di wax Timote ?
1.136522
Me ya sa Musa ya hau kan Dutsen Nebo, kuma menene Jehobah ya gaya masa?
Lu tax Musaa yéeg ci kow tundu Nebo, te lan la ko Yexowa wax?
1.136449
12:12 Domin Ruhu Mai Tsarki zai koya muku, a cikin awa daya, abin da dole ne ka faɗa. "
12:12 ndaxte Xel mu Sell mi dina leen xamal ca waxtu woowa li ngeen war a wax."
1.136328
Sai ya ƙara da cewa: "Zunubansu da kurakuransu ba zan ƙara tunawa da su ba. "
17 Noonu mu tegaat ca ne:"Dootuma fàttaliku seeni bàkkaarwalla seeni tooñ."
1.136318
"Toh Afrah seki tashi ai mutafi ko?
Ndax ñi dee dinañu mas a dekki ?
1.13625
54Ya taimaki bawansa Isra'ila,
54 Wallu na bànni Israyil giy jaamam,
1.136158
Manzo Yohanna ne ya rubuta littafi na ƙarshe fiye da shekara 1,900 da ta shige.
Téere bu mujj bi, ndaw li Yowaana moo ko bind, am na léegi lu ëpp 1 900 at.
1.136145
"Ko suna cewa ya kage shi ne ka ce ku zo da sura guda kamarsa kuma ku kira duk wanda za ku iya koma bayan Allah in kun kasance masu gaskiya." Surar Yunus: 38.
22 Te lépp lu ngeen laaj cig ñaan, bu ngeen ci boolee ngëm, dingeen ci jot."
1.13612
Kada ku hana su, gama mulkin Allah na irin waɗannan ne.
Buleen leen tere, ndaxte ñu mel ni ñoom ñoo yelloo nguuru Yàlla.
1.135669
Sa'ad da su da mahaifinsu suka ga ƙunshin kuɗinsu, suka razana.
Ba ñu gisee mbuusi xaalis ya, ñoom ak seen baay, dañoo tiit.
1.135558
Yesu ne hanyar ceto!
Yeesu mooy yoonu mucc gi !
1.135522
Menene ya faru da jirgin bayan watanni biyar?
Lu xewoon ak gaal gi bi juróomi weer paasee ?
1.135507
48Da iyayensa suka gan shi sai suka yi mamaki.
48 Ay waajuram gis ko, waaru.
1.135487
Amma za ku yi ciki, ku haifi ɗa.
Dinga ëmb, jur doom ju góor.
1.13537
Mata, ku miƙa kai ga shugabancin mazanku, kuma ku bi misalin macen kirki da aka kwatanta a Misalai 31:10-31.
Jigéen ñi, déggalleen seen jëkkër, te roy jigéen bu am manoore bi ñu wax ci Proverbes 31:10-31.
1.135267
Sai ya ce wa mutanen, "Akwai ranaku shida da ya kamata a yi aiki.
Mu ne mbooloo ma: "Juróom benni fan la nit ñi wara liggéey.
1.135124
Ana buƙatar karin lokaci kaɗan a gare ni Ni ...
Dama leen soxla tuuti ...
1.135109
Ka ba su abin da za su ci da kanku. "
Jox leen ñu lekk. '
1.135044
23 Shi kuwa ya gane makircinsu, ya ce musu, 24 "Ku nuna mini dinari.
23 Waaye Yeesu xam na seen pexe ne leen: 24 "Wonleen ma posetu denariyon.
1.135015
Yau na tashi
Teel naa yeewu tey.
1.135001
Kai ne Iliya?"
Ndax yaa di Ilyaas?"
1.13486
Ai, waɗanda Allah shi ne Allahnsu rayayyu ne, ba matattu ba." 33 Da jama'a suka ji haka, sai suka yi mamakin koyarwarsa.
Li ciy génn mooy, nekkul Yàllay ñi dee waaye Yàllay ñiy dund la." 22:33 Bi nga xamee ne mbooloo ma dégg nañu loolu, ñu waaru ndax li mu jàngale.
1.134768
22:33 Sai ya ce masa, "Ubangijin, Ni shirye su tafi tare da ku, ko kurkuku, ko kuma mutuwa. "
33 Piyeer ne ko: "Boroom bi, àttan naa ànd ak yaw ca kaso, ba ci dee sax."
1.134768
Na farko ya bayyana dalilin da ya sa 'yan Adam suke da rai, wato, don su san Allah, su ƙaunace shi kuma su bauta masa da aminci.
Bu jëkk bi dafa ñuy xamal lu tax nit di dund - ngir xam Yàlla, bëgg ko, te jaamu ko ak takkute.
1.134678
Kuyi farinciki, kuyi murna kwarai: gama ladarku mai - girma ce cikin sama: gama hakanan suka tsananta ma annabawan da suka rigaye ku" (Matta 5:11 - 12).
bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.
1.134675
zo a kan wata kaddara, ya Musa!
waaaw les mousses!
1.134602
Sunny day, yay!
Sunny day, yaay!
1.134602
42 Sai suka ba shi wata tsokar gasasshen kifi.
42 Ñu jox ko dogu jën wu ñu lakk.
1.134599
Maza su ƙaunaci matansu kamar jikinsu. - Afisawa 5:25-29.
Jëkkër yi dañu war a bëgg seen jabar ni ñu bëgge seen bopp. - Efes 5:25-29.
1.134435
Ta Yaya Za Ka Iya Zama Aminin Allah? | Albishiri
Naka nga mënee jege Yàlla ?
1.134418
24:50 Sa'an nan Ubangiji wannan bawa zai zo a ranar da bai zata ba, kuma a sa'a cewa bai san.
24:50 kon njaatige ba dina ñëw ci bés bu mu ko séenuwul ak waxtu wu mu xamul.
1.134225
Ya tambayi Bitrus, ya ce, "Ashe, ba za ku iya yin tsaro tare da ni ko na saʼa guda ba?
Mu ne Piyeer: "Amuleen sax dooley xoolandoo ak man benn waxtu?
1.134165
24:45 Sannan ya bude hankalinsu, d thatmin su fahimci Littattafai.
24:45 Noonu mu ubbi seen xel, ngir ñu xam li Mbind mi di wax.
1.134122
11:4 Waɗannan su ne itatuwan zaitun biyu da fitilun nan biyu, yana tsaye a gaban ubangijin duniya.
4 Ñaari seede ya nag ñoo di ñaari garabu oliw yeek ñaari tegukaayu làmp, yi taxaw ci kanam Boroom suuf si.
1.1341
Ya faɗi haka, ya barci.
Naka la wax loolu, daldi nelaw.
1.133922
34 Sai suka ce, "Ubangiji ne yake bukatarsa."
34 Ñu ne: "Ndaxte Boroom bi da koo soxla."
1.133786
Me Ya Sa Allah Ya Ƙyale Mugunta da Wahala? | Albishiri
Lu tax Yàlla bàyyi lu bon ak coono yi di am?
1.133638
Kuma ina mamakin, sai su ce: 'Me ya sa Ubangiji ya aikata haka ta wannan ƙasa da kuma wannan gidan?'
Dinañu ne: "Lu tax Aji Sax ji def nii réew mii ak kër gii?"
1.133618
4:23 don haka a sabunta cikin ruhun tunaninku,
4:23 Te ngeen yeeslu ci seen biir xel,
1.133603
7Saboda haka kada ku haɗa kai da su.
7 Kon nag buleen séq ak ñooñu dara.
1.133601
Can za ku gan shi.'
Dinga leen gis foofu. '
1.133589
3In na sallame su gida da yunwa, za su kāsa a hanya, don waɗansu daga cikinsu sun zo daga nesa."
3 Su ma leen yiwee ak seen xiif, dinañu tële ci yoon wi, ndaxte am na ñu jóge fu sore."
1.133437
Yanzu sun san cewa duk abin da ka ba ni daga gare ka ya fito.
Xam nañu léegi ne, loo ma joxaan, ci yaw la jóge,
1.133416
Mutane masu faɗin irin abubuwan nan sun nuna cewa suna neman ƙasar da take tasu.
14 Ñiy waxe noonu nag dañuy wone ne ñoo ngi wut réew mu ñu moomal seen bopp.
1.133339
2 Amma wa zai iya jurewa da ranar zuwansa?
2 Waaye bésub dikkam, ana ku ko mana dékku?
1.133198
22:19 Nuna mini kudin harajin kidayar jama'a. "
22:19 Wonleen ma poset, bi ñuy feye galag."
1.133112
8 Wannan rarrashin da ake muku ba daga wanda ya kira ku ba ne.
8 Li ñu leen xiir jógewul ci Yàlla mi leen woo.
1.13307
Me ya sa almajiran suka ji tsoro daddare, kuma me ya faru da Bitrus?
Lu tax taalibe yi tiit ci guddi gi, te lan moo dal Piyeer ?
1.133016
Ku yi murna, ku yi farin ciki, domin babban sakamako ne a Sama, don kamar yadda suka tsananta wa annabawan da suke gabanku.
bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.
1.132958
23Ya gane makircinsu, sai ya ce musu, 24"Nuna mini dinari.
23 Waaye Yeesu xam na seen pexe ne leen: 24 "Wonleen ma posetu denariyon.
1.132958
39 Ya kuma ba su wani misali ya ce, "Makaho yana iya yi wa makaho jagora?
39 Noonu Yeesu wax na leen beneen léeb ne leen: "Ndax gumba man na wommat moroomam?
1.132679
Sun tafi da yake dare ya fara yi, kafin a rufe ƙofar garin.
Ci timis lañu dem, bala ñu tëj buntu dëkk bi.
1.132641
Yamiyo Kowai Hace 3 días
je les aiiiimeee tous les 3 .
1.132489
16; To, ba sai Nã rantse da shafaƙi ba.
sworga ko aaasaan ma
1.132405
4:32 Sai shi kuma ya ce musu, "Ina da abincin da za su ci abin da ba ku sani ba."
4:32 Waaye Yeesu tontu leen: "Am na ñam wu may lekk, te xamuleen ko."
1.132394
duk da haka kun ƙi zuwa wurina domin ku sami rai.
te bëgguleen a ñëw ci man ngir am dund!
1.132289
"Eh muna ji, insha Allah, bazamu sake mu sake karya umurnin Gimbiya ba.."
Xam nanu ne, Yàlla du déglu boroom bàkkaar.
1.132225
Su wane ne? - Kuna da yara?
Ndax am nga ay doom?
1.132192
Yaya ya buɗe idanunku? "27 Ya amsa musu ya ce," Ai, na gaya muku, amma ba ku kasa kunne ba.
Nu mu la ubbile say bët?" 9:27 Mu ne leen: "Wax naa leen ko ba noppi, waaye dégluwuleen ma.
1.132055
7Saboda haka kada ku haɗa kai da su.
7 Kon nag buleen séq ak ñoom dara.
1.131995
Kai kuma, ɗan yarona, za a ce da kai annabin Maɗaukaki,Gama za ka riga Ubangiji gaba,Domin ka shisshirya hanyoyinsa,
Yaw nag doom, dinañu lay wooye yonentu Aji Kawe ji,ndaxte dinga jiitu, di yégle ñëwu Boroom bi,di ko xàllal yoon wi.
1.131966
Amma menene Littafi Mai Tsarki ya ce game da magana da matattu?
Lan la Biibël bi wax ci li ñi dee nekke ?
1.131778
A ƙarshe sai Allah ya aiki mala'iku biyu su yi wa Lutu gargaɗi cewa zai halaka Saduma da kuma Gwamarata birnin da ke kusa da shi domin muguntarsu.
Mujj na yónni ñaari malaaka ci Lóot ngir wax ko ne dina alag Sodom ak benn dëkk bu ko jege te tudd Gomor ndax lu bon li ñu doon def.
1.131688
8 Ba zan-sa jama'ar Isra'ila su ƙara fita daga ƙasar da na ba kakanninsu ba, idan dai za su kula su aikata dukan abin da na umarce su, su kuma kiyaye dukan dokokin da bawana Musa ya umarce su."
8 Ndegam bànni Israyil saxoo nañoo sàmm mboolem lu ma leen santoon, te mu dëppook mboolem yoon wi leen Musaa sama jaam ba sant ñu topp ko, dootuma leen wërloo, ñu wacc réew mi ma joxoon seeni maam."
1.131637
35Kuma suka ce: "Mũ ne mafiya yawa ga dũkiya da ɗiya, kuma mu ba mu zama waɗanda ake yi wa azãba ba.
2 Ñii naan: "Nun danoo jaboot, nook sunu doom yu góor ak yu jigéen.
1.131537
Haka zai sa dukan al'ummai su sani cewa kai ne kawai Allah.'
Xeet yépp bu ñu gisee loolu, dinañu xam ne yow rekk yaay Yàlla dëgg. '
1.1315
Iyaye, mene ne yaranku suke bukata don su kasance masu farin ciki a rayuwa?
Waajur yi, lan la seeni doom soxla ngir bég ?
1.131481
Bitrus da manzannin sun ba da shaida kuma sun yi bayanin cewa dole ne su yi wa Allah biyayya amma ba mutane ba.
5:29 Waaye Piyeer ak ndaw ya tontu leen ne: "Déggal Yàlla moo gën déggal nit.
1.131217
10:42 Amma duk da haka abu daya kawai ya zama dole.
10:42 Moona de, lenn rekk a am solo.
1.131213
Mulkin Allah yayi wannan.
Te Nguuru Yàlla dina def loolu.
1.131197
Domin a cikin awa daya, Hukuncinku ya isa. '
Ci wenn waxtu rekk la sa àtte dikk!"
1.131087
29 Sai ya ce musu, "Ai, irin wannan ba ya fita sai da addu'a."
9:29 Yeesu tontu leen ne: "Yu mel ni yii, ñaan ci Yàlla rekk a leen di dàq."
1.131001
31wanda ka shirya a gaban dukan mutane,
31 xeet yépp seede ko.
1.130942
Shi ne wanda ya ceci Daniyel daga bakin zakoki."
Moom moo muccal Dañeel ci gémmiñu gaynde yi. '
1.130932
12:29 Say mai, kada ka zabi su yi tambaya a kan abin da za ka ci, ko abin da za ku sha.
12:29 Buleen di wut lu ngeen di lekk walla lu ngeen di naan; te buleen ci jaaxle.
1.130817
Bari mu tunatar da cewa ...
Nuy fàttali rekk ni...
1.130778
18Sun ce muku, "A kwanakin ƙarshe za a kasance da masu ba'a waɗanda za su bi sha'awace-sha'awacensu na rashin tsoron Allah." 19Waɗannan mutanen ne, suke kawo rabe-rabe, masu bin abin da jiki yake so, marasa Ruhu.
1:18 ne leen: "Muju jamono ay tiiñalkat dinañu feeñ, ñuy weddi Yàlla, ngir topp seen bakkan."
1.130689
Don haka ni shaida ne a kai," in ji shi.
mu dib seede ba fàww."
1.130649
8 Yaya cewa Allah yana ta da matattu sa'an nan, ya ƙi gaskatuwa a gare ku?
8 Lu tax seen xel dàq ne Yàlla dina dekkal ñi dee?
1.13056
"Suka da'awar san Allah, amma sun ƙaryata shi da ayyukansu.
" Dañoo mbubboo xam-xamu Yàlla, waaye seeni jëf weddi na ko. " - TIT 1:16.